ÑAXTU
Xale yu góór ak yu jigéén yi ci daara jii da ñoo bëggë birël bës niki tay ne xamu ñuy dig yuy xajjatle ay nit.
Xam nñu ni ñun nit ñëpp da ñoo wuuté waaye ñoo bokk benn bëgg-bëggu dund ci jamm moom sa bopp.
Xale yu góór ak yu jigéén yi ci daara jii, ak yi ci daría Aragon bi yëpp, am nañu yelleefu janneer adduna bu lëndëmul, boo xamne araf yi, tééré yi, xalima yi, asamaan si, bës yi, dragon yi ak xarit yi dañuy ame melokaan yëpp. Loolu tax na ñun ñëpp ñoo ngi and yuuxu ca kaw naan:
DÉDÉÉT BODDIKOONTE CI BIIRI XEET (RASISM)
DA ÑOO BËGG DUND CI ADDUNA BU FEES AKIY MELOKAAN

afrikans | aragonés | عربي | aleman | bieloruso
bulgarian | català | caló | croata | czech | 한국어 | english | español | esloveno | euskera | français | gallego | griego | hebreo | hindi | hungaro | italiano | 日本語 | polsko | português | quechua | lituano | mandinga | maltes | nepalés | holandes | romanian | russian | serbio | turco | ucraniano | urdu | valenciano | vietnamita | volofo | yídish | 中文